Abul Mahaamid🤍
@BaaySheexloo
MURID.ﷺ💓
Léegi kon dafa am xassida bo xamni boo yittewoo ay koppar, ak numu mën tollu boo ko jàngee di nga ko am ? Te am na ñu ko fi am fii ? Génn léen ci séen pat pataaral bi
Léegi kon dafa am xassida bo xamni boo yittewoo ay koppar, ak numu mën tollu boo ko jàngee di nga ko am ? Te am na ñu ko fi am fii ? Génn léen ci séen pat pataaral bi
Léne si ndiarignou Salaatou Ala Nabi (Diouly si Yonenté bi Sallalahou Alayhi Wasalam) yinga hamné Borom Touba léralnako si térém bimou toudé: FAWZOU AL MOUTÎKH @LigeykatubMamam
« Ko xamne sama mbeigue sa mbeigue la sou biss bi gnewatei na nga ma si santalei sama borom »
03 : 43 kenn génnee gu ko ? Aaah
Léegi kon dafa am xassida bo xamni boo yittewoo ay koppar, ak numu mën tollu boo ko jàngee di nga ko am ? Te am na ñu ko fi am fii ? Génn léen ci séen pat pataaral bi
😭😭😭gaa yi séen bakkan rek lañ topp
Les Mourides qui topent le Jummah de Paris maintener votre magal Mardi 12 Aout 😏😏😏
Gaa yi man damay laaj comme yéen de😭 fimne sama dm yi sauté na
Sëñ Muntaxaa ak pas-pas am bii miisal la ci ne sëriñ bu mag bi boroomam jaraloon na ko, te ngor ak jom kenn ëpp u ko ko !
Prière du Vendredi 25 Juillet 2025 à la Grande Mosquée de Touba en présence du Khalif Général des Mourides Serigne Mountakha Mbacke Bachir, Yàlna fi yàgg lol ta wer barkep Seexul Xadiim.
Amnaa ci sax💀❤️😍
✨COLLECTION CHEIKH AHMADOU BAMBA 2025✨ JALLABE AVEC THIAYA Tissu : * SUPER CENT ANGLAIS 100% COTON 🏷 40 000 FCFA - - - - - - - - - - - - - - - - - - - SERVICE COMMERCIAL : +221 76 803 53 59 📸 : @bambaedenprod #Magal2025
Léegi kon dafa am xassida bo xamni boo yittewoo ay koppar, ak numu mën tollu boo ko jàngee di nga ko am ? Te am na ñu ko fi am fii ? Génn léen ci séen pat pataaral bi
Comme par hasard Wa DSA ñëw jàng ko séen GA bi😍❤️
78 bu jaar yoon 🥲❤️ gàmmu 2020, Magal 2014....
Événements HT yi nak léegi da ngay raté prestations yu bari, ndax ñaar/ 3i mbaar yi, kureels yi bari nañ te manoo léen degloo ndoo 🥲
Depuis nga fass nak, danga dégg 🤔 mystère 💀
Seuy (touki) Gno yamm, gars yi dagnla nann neikhoul teh dougn tass ( dougn gnibissi)🙂
78 bu jaar yoon 🥲❤️ gàmmu 2020, Magal 2014....
Mawahibu 78 bu wer laa namm a déglu tay🥺❤️